Paroles de chanson et traduction Kalsoum - Culture

Culture
Culture

Suma leeroon ne
Suma leeroon ne
Sangu na ba sett
Sangu na ba sett
Dina solu doon soldaru buur
Dina solu doon soldaru buur
Waaye samay laaf toy
Waaye Samay jouet Laaf
Tawte waraluko
Tawte waraluko
Ngelaw wawuluko
Ngelaw wawuluko
Kama djiito
Kama djiito
Mooma walle jangaro
Mooma walle jangaro
Solma toke
Solma toke
Ma lanke bañ taxalikok mom
Ma Lanke de taxalikok maman

Hey Tey dji toxu naa
Hey Tey dji Toxu naa
Ba sama xel xely
Ba sama xel xely
Ma dieli lama jangul fenn
Ma Dieli lama jangul fenn
Oh - Ci la xamné niit
Oh - Ci la xamné niit
Amul ludul boppam
Amul ludul boppam
Aki mbokam
Aki mbokam
War na fonk boppam
Guerre na fonk boppam
Si lu genn
Si lu genn

Culture bi naax saay - hey
Culture naax bi Saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
DegG XEY bi gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Diublu ci yoonu disons-dire
Waxleen ci li waay
Waxleen ci li waay

Culture bi naax saay - hey
Culture naax bi Saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
DegG XEY bi gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Diublu ci yoonu disons-dire
Waxleen ci li waay
Waxleen ci li waay

Jamono dji leegi dafa changé
Jamono dji leegi dafa Changé
Alal tax na nu nekk ci danger
taxe Alal na nu nekk ci danger
Roy moonu hypnotisé
Roy l'hypnotiser
Aada ak cossaan ñu banalisé
Aada ak cossaan ñu banalisé
Culture bi naax saay
Culture naax bi Saay
Diublu ci yoonu say-say
Diublu ci yoonu disons-dire
Waxleen ci li waay
Waxleen ci li waay

Ni doomu adama yi doxe
adama yi de doxe de Ni
Sax ci diko jeffee
ci Sax diko jeffee
Waye don na
Waye don na
Lu uteek liñu digg lee
Linu de digg Lu lee
May tambale ci yermande
Peut tambale ci yermande
Doomu aadama yi
Doomu aadama yi
ni ñu wara bëggante
ni ñu wara bëggante

Culture bi naax saay - hey
Culture naax bi Saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
DegG XEY bi gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Diublu ci yoonu disons-dire
Waxleen ci li waay
Waxleen ci li waay

Culture bi naax saay - hey
Culture naax bi Saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
DegG XEY bi gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Diublu ci yoonu disons-dire
Waxleen ci li waay
Waxleen ci li waay

Waxleen !!
Waxleen !!


Traduction par Anonyme

Ajouter / modifier la traduction
Email:

P